Seneplus.com
  • La Une
  • Politique
  • Economie
  • International
  • Sports
  • People
  • Opinions
  • Societe
  • Annonces
  • Culture
  • Medias
  • Diaspora
  • Femmes
  • Développement
  • Santé
  • Éducation
  • SENEPLUS TV
  • Baromètres
  • #SilenceDuTemps
  • NELSON MANDELA
  • LEOPOLD SENGHOR
  • CHEIKH ANTA DIOP
 
1 juillet 2025
FacebookTwitterRSS
Seneplus.com
Medias
  • La Une
  • Politique
  • Economie
  • International
  • Sports
  • People
  • Opinions
  • Societe
  • Annonces
  • Culture
  • Medias
  • Diaspora
  • Femmes
  • Développement
  • Santé
  • Éducation
  • SENEPLUS TV
  • Baromètres
  • #SilenceDuTemps
  • NELSON MANDELA
  • LEOPOLD SENGHOR
  • CHEIKH ANTA DIOP

GÀTTALUG XIBAAR YI

Defu Waxu  |   Ami Mbeng  |   Publication 25/07/2020

Ndengeleer

Askan way yeewoo ca Ndengeleer amal nañu ab ndaje di xamal waa nguur gi ne : ñaari fan lañu leen may ngir ñu indi ay saafara ñeel coowal suuf si, lu ko moy ñoom dinañ nangu seeni tool bay leen ca na mu gën a gaawe.

Aa li Nguy Njaay

Gannaw coowal suuf si dox ci diggante askanu Ndengeleer ak njiitu « Sedima » Baabakar Ngom, nguur gi jël na ñetti dogal. Bi ci jiitu mooy ne baykat yi dinañ mën a bayi seeni tool ba njeexitalu nawet bi.  Ñaareel bi nee na Baabakar Ngommu dakkal bépp liggéey bum sóoboon foofu ca tool ya. Dogal bu mujj bi mooy ne dinañ amal ab waxtaan su nawet bi jeexee ngir saafara mbir mi.

Widéwo bi lëmbe dëkk bi 

Ndaw su ñu jiiñ càcc ca Saakre-këer la ay ndaw doon filme ak a toroxal ba cër yi di feeñ, film baa ngi lëmbe dëkk bi, ñépp di ko ñaawlu. Naka noonu la Maam Maxtaar Géy ak Séydi Gasama di xamle ne dinañ topp ñi doon filme ngir xam ñan la, def li ci war.

Mali

 Way-jubóole Afrig sowu jant yaa ngiy laaj ñu taxawal nguurug bennoo.

Misra

Dipite Misra yi nee nañu bu soldaari nguurug Tripoli gi Tirki faral dakkalul seenug dox jëm ci penku réew mi, dinañ ànd ci yabalug soldaar ca Libi.

Mali

 Ngir jiital kaaraange nit ñi ñeel xare bi lëmbe diiwaanu Sayel bi, lu tollu ci 20i kuréli Afrig ñoo booloo sos mbootaayu maxejji Sayel (coalition citoyenne pour le Sahel) ci bésub 16eel sulet 2020 ngir samp ab naal. Li ñu ci jublu mooy wut meneen pexe ginnaaw bi làrme yi lajjee ci caytug kaaraange diiwaan bi.  

Saakre-këer

Ci xibaar yu mujj yi, ñoo ngi nuy yëgal ne yoon teg na loxo ndaw yi doon filme teg ci di toroxal xale bu jigéen bi ñu doon jiiñ càcc.

Articles les plus lus

capture_decran_2025-06-24_a_23.42.22.png
UN COMITÉ QUI OUBLIE CEUX QUI LISENT ET FONT LIRE
Le vendredi 20 juin 2025, à la Maison de la culture Douta Seck, s’est tenue une cérémonie solennelle. ...

adama-dieng.jpeg
L'IMPLOSION DU SOUDAN DOIT ÊTRE STOPPEE À EL-FASHER
Il y a quelques jours, la Commission africaine des droits de l'homme et des peuples (CADHP) et la Mission ...

mbane_.jpg
LE SUCRE DE LA CSS NE DOIT PAS GHETTOÏSER MBANE
C’est Le Quotidien, dans sa Une du jeudi 19 juin 2025, qui donne les détails de l’affaire : la Compagnie ...

mgueye_.jpg
DU QUATRIÈME SOUS-SOL AUX JETS PRIVÉS ET LIMOUSINES
Heureux comme notre Premier ministre, qui a l’occasion de voyager à travers l’Afrique et le monde, ...

andama.jpg
RENCONTRE AVEC UN PERSONNAGE A LA FOIS CELEBRE ET MYSTERIEUX
Son nom est intimement lié à Diofior, un village sérère connu pour être un bastion de la lutte traditionnelle ...

Vos articles préférés de la semaine

capture_decran_2022-01-09_a_21.42.15_0.png
LE SÉNÉGAL VA MAL
Entre morosité et rhétorique politicienne Le contexte actuel du Sénégal prouve, au-delà des promesses ...

capture_decran_2025-06-18_a_09.08.32.png
IL FAUT AIDER LE SOLDAT BASSIROU KÉBÉ, DG DE LA SNHM
Les Américains disent que toute politique est locale. Le citoyen juge l’Etat sur la base de ses actions ...

capture_decran_2025-06-15_a_13.56.37.png
LE FOOTBALL M’A DONNÉ DES FRÈRES ET DES SOEURS AUX QUATRE COINS DU MONDE
Du coiffeur de Salah au professeur d’anglais , de Luis Díaz, des tribunes de Munich aux rues de Paris, ...

capture_decran_2025-06-23_a_16.58.31.png
DIOMAYE BATTU À LA PRÉSIDENCE DE LA CEDEAO PAR MAADA BIO
Amadou Hott avait le meilleur profil pour présider la Bad, et il a échoué. Hier également, la candidature ...

57540596-42611988.jpg
GUY MARIUS SAGNA, LE COL BLEU DE L’HÉMICYCLE
Il détonne dans l’Assemblée nationale. Sa voix, son langage, sa trajectoire. Il est l’un des rares ...


La Une

Politique

Economie

International

Sports

Football

Media

People

Opinions

Societe

Annonces

Diaspora

Femmes

Développement

Santé

Éducation

PARTENAIRES DE SENEPLUS

APS
Grand-Place
L'As
L'Enquete
L'Observateur
La Gazette
Le Populaire
Le Quotidien
Le Soleil
Le Témoin
Libération
Nouvel Horizon
Réussir
RFM
RTS
Stades
Sud FM
Sud Quotidien
Sunu Lamb
TFM
Waa Sports

À propos de SenePlus

SenePlus.com est un portail d'informations sur le Sénégal. Nous vous fournissons des articles détaillés, critiques, pertinents sur l'actualité au Sénégal.

Coordonnées

Publicité:
pub@seneplus.com
Informations:
info@seneplus.com
Problèmes techniques:
tech@seneplus.com
Copyright © 2025 SenePlus  |  Publicité  |  Soumettre un Article  |  Nous Contacter  |  Mentions légales  |  Conditions d'utilisation  |  Á propos de nous