Seneplus.com
  • La Une
  • Politique
  • Economie
  • International
  • Sports
  • People
  • Opinions
  • Societe
  • Annonces
  • Culture
  • Medias
  • Diaspora
  • Femmes
  • Développement
  • Santé
  • Éducation
  • SENEPLUS TV
  • Baromètres
  • #SilenceDuTemps
  • NELSON MANDELA
  • LEOPOLD SENGHOR
  • CHEIKH ANTA DIOP
 
17 juillet 2025
FacebookTwitterRSS
Seneplus.com
Santé
  • La Une
  • Politique
  • Economie
  • International
  • Sports
  • People
  • Opinions
  • Societe
  • Annonces
  • Culture
  • Medias
  • Diaspora
  • Femmes
  • Développement
  • Santé
  • Éducation
  • SENEPLUS TV
  • Baromètres
  • #SilenceDuTemps
  • NELSON MANDELA
  • LEOPOLD SENGHOR
  • CHEIKH ANTA DIOP

PORFESOOR MUSAA SÉYDI : «BÀYYI WIRIS BI LAW, MUSIBA LA NU NAROON A JURAL»

Bàyyi wirisu Covid-19 bi law ngir sabab kiiraayu-mbooloo la Doktoor Paap Musaa Coor digle ngir xeex mbas mi.

Paap Aali Jàllo (www.defuwaxu.com)  |   Publication 06/05/2020

Bàyyi wirisu Covid-19 bi law ngir sabab kiiraayu-mbooloo la Doktoor Paap Musaa Coor digle ngir xeex mbas mi. Waaye PorfesoorMusaa Séydi mi jiite Banqaasu feebar yiy wàlle ca loppitaanu Faan, àndul ak xalaat boobule. Lii la Porfesoor Séydi wax :

« Naam, way-tawat yaa ngiy yokku. Kenn werantewu ko. Waaye, bu dul woon dogal yiñ jël, romboon nan fii bu yàgg. Loolooy wone ne, fagaroo gën faju. Mu am, nag, ñu jàpp ne danoo waroon a bàyyi wiris bi mu law, dal ñu bari ci askan wi ndax ñu mën a am kiiraayu-mbooloo. Waaye, wiris boo xam ne mën na laa wàll benn, ñaar, ñett ba fukki yoon sax, sun ko bàyyi woon mu law musiba mu réy la nu naroona jural. Ñi ci ñàkk kon seen bakkan kenn du xam nu mu tollu. Duma tàyyee wax ne fagaru rekk moo nu mën a may ndam ci Covid-19 bii lëmbe àddina si.»

Ci ndaje mu jawriñu wér-gi-yaram ji doon amal ak taskati xibaar yi la PorfesoorSéydi indee leeral yile.

Articles les plus lus

greffage_.jpg
GREFFAGES, PERRUQUES ET PARANOÏA ADMINISTRATIVE
Il est des jours où l’on se demande si certains directeurs généraux ne confondent pas leur bureau ...

chroniques_dun_temps_politique_par_felwine_sarr_-_chroniques_dun_temps_politique_-_histoire_de_la_nation_senegalaise_felwine_recoit_pr_mamadou_diouf_h3ib1-puhtq_-_853x480_-_1m58s.png
MAMADOU DIOUF TEMPORISE SUR PASTEF
Quinze mois après l'arrivée au pouvoir de Pastef, l'impatience commence à poindre chez les Sénégalais. ...

capture_decran_2025-07-14_a_00.42.06.png
DIOMAYE - SONKO ET LES ENJEUX D’UN CONFLIT DE LÉGITIMITÉ
Les divergences au sein du couple Diomaye - Sonko ne seraient pas une répétition de l’histoire politique ...

capture_decran_2025-07-15_a_23.11.37.png
À 92 ANS, PAUL BIYA INCARNE LE MAL AFRICAIN SELON MBEMBE
L'historien et philosophe camerounais Achille Mbembe a livré une analyse de la candidature de Paul ...

capture_decran_2025-07-15_a_15.08.55.png
LE SÉNÉGAL REPREND DES COULEURS SUR LES MARCHÉS
(SenePlus) - Les marchés financiers sénégalais ont connu un regain d'optimisme lundi après que ...

Vos articles préférés de la semaine

capture_decran_2025-03-12_a_17.20.22_1.png
BIOPSIE D’UNE KOROMAQUERIE !
Être amoureux de la République de Ndoumbélane et ne pas vivre de satire peut rendre malade. Et être ...

capture_decran_2025-07-14_a_00.42.06.png
DIOMAYE - SONKO ET LES ENJEUX D’UN CONFLIT DE LÉGITIMITÉ
Les divergences au sein du couple Diomaye - Sonko ne seraient pas une répétition de l’histoire politique ...

sans_detour_mamadou_ndoye_iv_0_2.jpg
IL NOUS FAUT UNE POLITIQUE LINGUISTIQUE AUDACIEUSE A L’ECOLE
Invité à prononcer le cours inaugural du colloque international « Multilinguisme et diversité à ...

chroniques_dun_temps_politique_par_felwine_sarr_-_chroniques_dun_temps_politique_-_la_crise_de_letat_de_droit_felwine_sarr_recoit_sidy_alpha_ndiaye_hdpt4urkww0_-_709x399_-_2m30s.png
L’INDIGNATION À GÉOMÉTRIE VARIABLE
Chronique d’un temps politique Dans son émission Chroniques d’un temps politique, lancée en ...

fr_20250430_194907_195631_cs.jpg
THIERNO ALASSANE SALL OU LE DEGRÉ ZÉRO DE LA POLITIQUE
Quand on n’a rien à dire qui honore les morts ni éclaire les vivants, le silence n’est pas seulement ...


La Une

Politique

Economie

International

Sports

Football

Media

People

Opinions

Societe

Annonces

Diaspora

Femmes

Développement

Santé

Éducation

PARTENAIRES DE SENEPLUS

APS
Grand-Place
L'As
L'Enquete
L'Observateur
La Gazette
Le Populaire
Le Quotidien
Le Soleil
Le Témoin
Libération
Nouvel Horizon
Réussir
RFM
RTS
Stades
Sud FM
Sud Quotidien
Sunu Lamb
TFM
Waa Sports

À propos de SenePlus

SenePlus.com est un portail d'informations sur le Sénégal. Nous vous fournissons des articles détaillés, critiques, pertinents sur l'actualité au Sénégal.

Coordonnées

Publicité:
pub@seneplus.com
Informations:
info@seneplus.com
Problèmes techniques:
tech@seneplus.com
Copyright © 2025 SenePlus  |  Publicité  |  Soumettre un Article  |  Nous Contacter  |  Mentions légales  |  Conditions d'utilisation  |  Á propos de nous