VIDEODAAM BAABU, DI LEERAL LUX ÑU WOOTE ROAD SHOW
Ku nekk Mukàllàf ñaar ngay jiital ci say soxla, mooy taxawal kër am ag njoboot, ak wut foo dugal sa njoboot. Ngir wut nu doomu Segnegaal yi nekk bittim reew mana jënd kër ci anam yu woor, mootax nu woote Road Show Immobilier ci Senegaal.

Ku nekk Mukàllàf ñaar ngay jiital ci say soxla, mooy taxawal kër am ag njoboot, ak wut foo dugal sa njoboot. Ngir wut nu doomu Segnegaal yi nekk bittim reew mana jënd kër ci anam yu woor, mootax nu woote Road Show Immobilier ci Senegaal. Samedi 4 June 2022 lay jeex New York, war faa joge dem Senegal ci 23-25 June 2022. Seetan leen video bi ngir lu gënë leer.