SenePlus | La Une | l'actualité, sport, politique et plus au Sénégal
17 juillet 2025
ËLLËGU XALIFA SÀLL CI LÀNGU POLITIG GI
Dibéer, 29eelufan ci weeru sàttumbar 2019, la Xalifa Sàll gisaat jant bi ginnaaw bi ñu ko ko nëbbee ñaari ati Yàlla ak genn-wàll. Ñuŋ ko toppe woon tuuma yii di wuruj ak luubal xaalisu méeri bu Ndakaaru.
Dibéer, 29eelufan ci weeru sàttumbar 2019, la Xalifa Sàll gisaat jant bi ginnaaw bi ñu ko ko nëbbee ñaari ati Yàlla ak genn-wàll. Ñuŋ ko toppe woon tuuma yii di wuruj ak luubal xaalisu méeri bu Ndakaaru. Alal jooju, nag, nee ñu ciy daara la waroon a dem, maanaam ci njàngale mi. Keroog ba ko takk-der yi jàppee, coow li noon na kurr. Xalifa Sàll weddi tuuma yi ñu teg ci ndoddam li ba mu set wecc, lànk ba tëdd ci naaj wi, moom ak i ñoñam. Ñoom, ci seeni wax, Njiitu-réew mi, Maki Sàll ci boppam, moo sooke lépp. Nee nañu yit duggewu ko lenn lu dul bañ Xalifa Sàll bokk ci woteb njiitéefu réew mi ñu dégmaloon ci ndoorteelu 2019. Ndaxte, ba tey ci seeni wax, jamono jooju, Xalifa Sàll rekk a fi amoon dayo bi koy tax a wujje ak Maki, sañ koo diir mbagg.
Naka noonu, Maki singali ko, kootoog yoon, ñuy lem ak a lemmi, di nos ak a nocci ba tëjlu ko ci atum 2017. Xalifa Sàll, nag, juróomi ati kaso la waroon a tëdd, teg ci ne waroon na fay Buur juróomi miliyoŋ ci sunuy koppar. Waaye, ñaari at ak génn-wàll rekk la jot a tëdd ñu bàyyi ko. Li sabab lu ni mel, nag, dese naa leer ci boppi askan wi. Ndege, am na ñu naan Maki da koo mujjee baal li ñu ko doon toppe ngir bëlde askan wi ko mere woon, mook rakkam Aliyu Sàll, ci coowal petarool li fi jiboon, fexe ba ñépp fàtte loolu. Ñeneen ñi jàpp ne waxtaan wi fi sëriñ Muntaxaa Mbàkke laloon ngir jubale Abdulaay Wàdd ak Maki Sàll ci ubbite jumaawu Masaalikul jinaan ji, moo waral lii lépp.
Wànte, ak lu mu ci mënti doon, li wóor mooy ne Xalifa Sàll génn na. Te mbir mi mbégte mu réy a réy la jur ci doomi réew mépp. Rawatina nag ci ñi mu bokkal pàrti. Guddig keroog ga muy génn, foo sànni mbàttu ci Ndakaaru mu tag. Askan wi da ko teeru nib buur, gunge ko ba ci biir këram. Bu fa yemoon sax ñu ne waaw ; waaye gaa ñi am nañ meneen mébét. Dafa di, yaakaar la génnub kaso Xalifa Sàll bi meññloo ci xol yi. Waaw, yaakaar kañ ! Bu kenn fàtte ne ca njëlbéen ga, newoon nañu ne am na ci doomi-réew mi ñu gëm ne Xalifa Sàll rekk moo fi mën a jële Maki. Te yaakaar jooju mel na ni ñaari ati kaso yi dindiwuñ ko ci xoli farandoo Xalifa Sàll yi. Mënees na ni sax tey la Waalo gën a aay. Keroog bi ñu bàyyee Xalifa la ki ñu gën a ràññee ci àndandoom yi, Bàrtelemi Jaas, tàmbalee waajal joŋante njiitéefu-réew mi war a am ci atum 2024, ànd ceek fullaam ju mat sëkk. Moom sax xanaa daa fàtte ni Xalifa day door a génn ? Li waral laaj bi du lenn lu dul ne sunu àtte ndeyu réew mayul ku yoon mës a tëj muy bokk ci joŋante woteb njiitéefu réew mi. Am da koo fàtte ? Naam sax Xalifa baal nañu ko waaye teewul ñu jot koo àtte ba teg ko ay daan. Kon li mu tëddoon Rëbës xaw na xajamal ay mbiram ci wàllu politig. Amaana looloo tax am ñu seen bopp xaw a tëju ba ñuy laaj lan mooy ëllëgu Xalifa Sàll ci géewu politig bi. Tontu ci du yomb waaye xel mënuta nangu ne Xalifa Abaabakar Sàll, newoon fi Meeru Ndakaaru te tàmbalee xeex ba muy gone gu ndaw, jeexal na ba fàww ci politigu Senegaal..
WÀDD-MAKI : GINNAAW AY…SOPPI ?
Keroog, àjjuma 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019,ba ñuy ubbi Masaalikul Jinaan, jullit yépp a bégoon, rawatina murid yi. Bégoon nañ ba, foo nattoon seen mbégte rekk, mu romb koy dem.
Keroog, àjjuma 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019,ba ñuy ubbi Masaalikul Jinaan, jullit yépp a bégoon, rawatina murid yi. Bégoon nañ ba, foo nattoon seen mbégte rekk, mu romb koy dem. Ndaxte, kat, wëliis li jumaa ji doon ab jaamukaayu Yàlla, Sunu Boroom, Masaalikul Jinaan dafa dib sag ci mboolem jullit ngireeni mu réye te yànj, kaar. Moom kay, guléet ñu gis fi jumaa ju ni mel ci Afrig sowu-jant ba mu daj. Te, nag, lépp li ko jëmmal mi ngi jóge ci ñaqi doomi réew mi, ci seeni xalaat, ci seen alal ak ci seen doole. Bu amee yit ay doxandéem yu ci dugal seen loxo, bariwuñu, te fay nañ leen liñ ci liggéey ba mu mat sëkk. Li ci ëpp, nag, Tuuba la jóge.
Waaye ubbite boobu, daa am leneen lu mu jur ci wàllu politig, mu di juboob Abdulaay Wàdd mi fi jiite woon réew mi ak Maki Sàll mi toog tey ci jal bi.
Kenn umplewul li dox ci diggante ñaar ñooñu, muy diggante baay ak doom. Ñu ngiy fàttaliku ba Maki Sàll di génn PDS, ginnaaw ba ñu ko fa bunduxutaalee ndax joteem ak Karim Wàdd. Mu jóge fa taxawal parteem tudde ko APR, utali nit ñi, bokk ca joŋanteb atum 2012 ngir doon ñeenteelu njiitu réewum Senegaal. Ba Maki Sàll gàddoo ndam loolu ba léegi nag, diggante ñaari politiseŋ yi daanaka at mu jàll mu gën a ñagas. Noonu, ba Maki jàpplu doomu Ablaay Wàdd ji, Karim Wàdd, yoon daldi koy nëbb jant bi ñetti at. Ci mujjantal gi, ñu génne ko, gàddaayloo ko ngir rekk mu bañatee a bokk cib joŋanteb fii ci Senegaal. Ay at a ngi nii mu ne réewum Kataar, ñibbisi të ko.
Digganteb ñaari kilifa yooyu nag, ku ne wax na ci ngir defaraat koo, rawatina njiiti diine yi, ñu gën cee ràññee Xalifay Murid yi fi jot a jaar. Ñenn ci njiiti réewi Afrig yi sax, ku ci mel ni Alfa Konde, xar nañ ci seen tànki tubéy ; waaye taxul diggante bi defaru bay rattax.
Loolu lépp tax na, keroog ca ubbiteb Masaalikul Jinaan, kenn gëmewul woon maslaa yeek jàppante loxo yeek àndandoo bi ñaari kilifa yooyu nekkee, di saafoonte, di digante gisewaat ci ni mu gën a gaawe. Ca dëgg-dëgg, nit ñi yàgg nañoo ñaan lu ni mel am, waaye teewuleen woon a waaru.
Dëgg la, politiseŋ yi, dañu bariy feem, waaye nag, àndandoo Ablaay Wàdd beek Maki Sàll keroog, ñu dem bay lëngoo, ñépp la dawloo seen yaram, tooyal seen xol. Ci sunu gis-gis bu gàtt daal, mënees naa am yaakaar ni juboo dëgg am na. Te nag, juboowu ñaari kàngam yooyu, war naa jur déggoo bu wóor fu bennoo mën a lalu, ba tax ñu mën jàpp ne, la jógge ca Masaalikul Jinaan lu taxaw la.
Déggoo boobu, waxtaanu politig la, te ëllëgu Karim Wàdd – maanaam delluseem ak nekkinam ci réew mi, ak itam taxawaayam ci joŋante yiy ñëw – mooy li ci gën a soxal Wàdd.
Su loolu lépp àntoo dinañu mën a wax ne Masaalikul Jinaan, ginnaaw li mu jur ci diine ji, di lu am a am solo, jur na it jàmm ak tawféex ci réew mi, tax na politiseŋ yi dakkal seen xulook seen ŋaayoo.
Waaye bu demewul noonu day rekk doon yaakaar ju tasati te ñépp dinañ ko naqarlu.
LE SÉNÉGAL S’ADJUGE LE TROPHÉE
L’équipe du Sénégal a remporté la finale de la Coupe UFOA 2019, en dominant le Ghana aux tirs au but (1-1, tab 3-1), ce dimanche, au stade Lat Dior de Thiès.
L’équipe du Sénégal a remporté la finale de la Coupe UFOA 2019, en dominant le Ghana aux tirs au but (1-1, tab 3-1), ce dimanche, au stade Lat Dior de Thiès. Le portier sénégalais, Pape Seydou Ndiaye a été le grand artisan de la victoire des Sénégalais.
Tous les ingrédients étaient réunis pour vivre une belle finale. Le temps était clément à Thiès puisque la pluie s’est invitée peu après le coup d’envoi. Sans oublier des gradins pleins à craquer, une folle ambiance et la présence du président de la CAF Ahmad Ahmad, de la Secrétaire Générale de la FIFA, Fatma Samoura, de l’artiste musicien Youssou Ndour…Un décor planté qui a boosté les 22 acteurs.
Sur la pelouse, tout est allé très vite. Les deux équipes n’ont pas eu le temps de s’observer. Mais, la première grosse occasion est venue du Ghana. Justice Blay a trouvé le poteau d’une tête rageuse. La rencontre s’emballe et prendre une autre tournure. Les duels s’invitent mais le Sénégal se signale aussi avec des offensives. A l’issue d’une belle première période, les deux formations retournent aux vestiaires sans faire trembler les filets.
En seconde période, le rythme est plus élevé. Mais, le hic est que les attaquants ont du mal à trouver la faille malgré les nombreuses tentatives. Face à la pression du public, les Sénégalais confondent parfois vitesse et précipitation.Au moment où le Ghana tente de jouer très calme. La stratégie ghanéenne a payé durant le temps réglementaire puisqu’ils ont réussi à bloquer les assauts sénégalais. Score à l’issue des 90mn de jeu, zéro but partout.
Pape Seydou Ndiaye décisif
La prolongation s’invite dans la partie. Mais, il a fallu attendre le début de la seconde période pour voir Youssou Badji qui venait d’entrer en jeu, ouvrir le score suite à une passe en retrait de Ousseynou Niang (107′). Le stade Lat Dior explose de joie. Mais c’est une joie de courte durée puisque Jospeh Esso égalise pour le Ghana deux minutes plus tard (109′) et ramène les deux équipes à la séance des tirs au buts.
Très maladroits, les Ghanéens ont peiné à s’imposer devant les Sénégalais qui ont été plus décisifs. Grâce donc à son gardien de but Pape Seydou Ndiaye auteur de deux arrêts lors de cette séance, le Sénégal remporte (1-1, tab 3-1) la finale de l’UFOA 2019 . Dans le match, le gardien de but des Lions avait même sauvé ses partenaires en sortant de justesse une tête ghanéenne.
Le Sénégal succède au Ghana vainqueur de l’édition précédente. Il s’agit du deuxième trophée pour le football sénégalais après les jeux africains de 2015. Les Lions empochent 50 millions francs CFA. Quant au vainqueur, il rentre avec 25 millions francs CFA.
Dakar, 14 oct (APS) – L’audience que le chef de l’Etat a accordée, samedi, au palais de la République, à son prédécesseur, Me Abdoulaye Wade, est largement commentée par les quotidiens reçus lundi à l’Agence de presse sénégalaise (APS).
’’Les grandes retrouvailles’’ affiche à ce sujet Le Soleil qui souligne que ‘’l’acte 2 des retrouvailles entre les présidents Macky Sall et Abdoulaye Wade a été posée avant-hier’’.
’’Cette audience qui a duré plus de trois heures d’horloge a été sanctionnée par une déclaration commune dans laquelle le président Abdoulaye Wade appelle le chef de l’Etat à +déployer tous les efforts nécessaires à la maitrise de la gestion du pétrole, du gaz et des autres ressources naturelles’’, écrit le journal, ajoutant que Macky Sall promet une visite à Me Wade prochainement.
Parlant de cette rencontre, Walfadjri note que ‘’le cas Karim Wade (était) en suspens’’. ‘’Sur les questions concernant la privation des droits civiques et politiques de Karim Wade, l’amende de 138 milliards de francs Cfa qu’il doit payer, la fin de son exil +dorée+ à Doha et sur d’autres problèmes, sources du contentieux (entre Wade et Macky Sall) depuis 7 ans, c’est l’omerta totale’’, selon Walf.
’’Une rencontre, des non-dits’’, selon le quotidien L’As, lequel estime qu’au-delà ‘’du caractère symbolique de cette rencontre, tout ce qui s’est passé samedi dernier laisse entrevoir plutôt une mise en scène pour ne pas dire une mise en œuvre d’un deal qui ne dit pas son nom’’.
En effet, ajoute le journal, ‘’Abdoulaye Wade ne cherche qu’à faire revenir son fils en +exil forcé+ au Qatar afin qu’il retrouve ses droits civiques et politiques et qu’il puisse participer aux prochaines échéances électorales’’.
Dans le quotidien Vox Populi, l’enseignant-chercheur en Sciences politiques, Moussa Diaw, note que ‘’ce qui est important et qui n’a pas été évoqué dans le communiqué, c’est que l’affaire Karim Wade a été certainement abordée par l’ancien président de la République’’.
’’Parce que sa préoccupation, c’est de faire en sorte que son fils puisse revenir et jouer un rôle de premier plan au sein de son parti’’, ajoute l’analyste.
Pour La Tribune, ‘’(….) ce qui est sûr et certain, est que les retrouvailles entre Wade et le président Macky Sall n’ont qu’une finalité : passer Wade fils à la blanchisserie, lui frayer un chemin pour 2024 et réaliser le rêve de son père qui est de voir les libéraux trôner au sommet du pouvoir pendant 50 ans’’.
’’Retrouvailles Wade-M acky, et après ?’’, s’interroge Enquête qui souligne que ‘’depuis sa réélection et son investiture en avril 2019, Macky Sall n’a cessé de poser les actes de la coexistence pacifique avec ses anciens frères de parti qui ont abouti à la deuxième rencontre (publique) en trois semaines avec son +mentor+ Abdoulaye Wade dans le contexte de dialogue national’’.
Parlant de cette rencontre, Le Quotidien signale que ‘’zappé du communiqué conjoint, Wade-fils (était) au cœur des discussions’’ entre Macky Sall et Abdoulaye Wade. ‘’Karim, un K à part’’, affiche le journal à sa Une. Il ajoute que "(….) le fait même d’avoir tu le sujet (Karim) et l’objet (son avenir par l’amnistie) est finalement la seule information qui vaille que l’on s’y attarde’’.
’’Car, ajoute le journal, au fond, ne pas en parler, c’est justement en parler. Et en faire parler. Abdoulaye Wade est prêt à tout pour faire réhabiliter son fils. Il en est le pro (moteur)’’.
L’Observateur parle d’une ‘’mise en scène’’ du ‘’new-deal’’ entre Macky Sall et Abdoulaye Wade et pense que ‘’Karim Wade est le troisième homme’’ de cette rencontre. Dans le journal, l’analyste politique Hamidou Anne estime que ‘’toute l’action de Wade vise à sortir Karim de sa situation inconfortable’’.
RIEN NE SERA FAIT CONTRE LES INTÉRÊTS VITAUX DU SÉNÉGAL
Un climat politique apaisé est une condition de la stabilité du pays. C’est la conviction de Macky qui lors du séminaire du gouvernement tenu dimanche 13 octobre au King Fahd Palace, a expliqué à ses militants les motivations de certaines de ses décisions
Un climat politique apaisé est une condition de la stabilité du Sénégal. C’est la conviction de Macky Sall qui lors du séminaire du gouvernement qui s’est tenu, hier dimanche, 13 octobre, au King Fahd Palace, a expliqué à ses militants les motivations de certaines de ses décisions. Entre autres, sans les nommer, son rapprochement avec Abdoulaye Wade et la récente libération de Khalifa Sall. « Je voulais rassurer les militants sur l’apaisement du climat. Cet apaisement je l’ai voulu au lendemain de ma réélection. J’ai tout de suite lancé un dialogue. Et c’était au lendemain d’une grande victoire que nous avons estimé qu’il était temps d’impulser une nouvelle trajectoire de dialogue, de concertation qui doit avoir comme finalité un apaisement du champ social, économique, politique afin de permettre au pays de se concentrer sur les vrais combats », dit-il.
Pour Macky Sall, cette nouvelle dynamique communicationnelle tend à réaffirmer son ouverture au dialogue. « Plus nous élargirons le cercle, mieux le Sénégal se portera, donc cette ouverture n’est faite contre personne. Le seul enjeu de cette ouverture ,c’est l’enjeu de la paix civile, la paix sociale et aussi l’enjeu de la stabilisation dans un contexte sous régional extrêmement fragile marqué par l’insécurité et les risques de déstabilisation de beaucoup de pays qui nous entourent », ajoute-t-il. Et de préciser : « Rien ne sera fait qui sera contraire aux intérêts vitaux de la nation. »
Ci àjjuma jii weesu, 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019, lañ doon ubbi ci Kolobaan jumaa ju mag ji : Masaalikul Jinaan. Kilifa gii di Sëriñ Muntaaxa Mbàkke, Xalif kullu murid, moo jiite xew-xew bile. Kon, tey la woon tey. Ndege, xew-xew bi lëmbe woon na réew meek àddina sépp, daanaka. Ndaxte, muy JeuneAfriquedi Le Mondewalla RFIañs, genn kërug yéenekaay wutewul bés bi. Xibaar bi àggoon na ba Frãs ba seen benn politiseŋjot cee xund, wax sax ay waxi ku danoo ci saret.
Jumaa ju réy, xaalis bu takku
Jumaa Kolobaan ji, nag, jumaa ju réy a réy la, képp ku ko gis yéemu ci yànjaayam. Yaatuwaay baa ngi tollu ci 6i ektaar. Dafa di sax, Masaalikul Jinaan mooy jumaa ji gën a réy ci Afrig sowu-jant. Lu ëpp 30 000, ci xayma, nit mën nañ cee julli : 8 000 ci biir, 20 000 ci biti ak 3 000 ci kow etaas bi. Njëgu tabax bi, moom, mi ngi tollu ci 20i milyaar ci sunu xaalis. Taalibe yee joxe 15i milyaar yi Sëriñ Siidi Maxtaar Mbàkke teg ci 5,5i milyaar. Taalibe yi dañu daan natt, ñii joxe 1000, ñeneen ñi 10 000, am it ñu génne ay milyoŋ def ci, ku nekk daal yaay seet fu sa doole tollu nga def li nga mën,mu néew mbaa mu bare. Jumaa ji, nag, kii di Sëriñ Muxammadu Lamin Mbàkke moo teg birig bu njëkk bi, ci 7eelufan ci weeru sulet, atum 2012. Sëriñ Mbàkkiyu Fay mi toogal Xalifa bi ci Ndakaaru lañ dénkoon liggéey bi. Juróom-ñaari at lañ ci teg lépp door a sotti.
Jenn jumaa, 5i sooroor
Kon, Masaalikul Jinaan, ci njiiteefu Sëriñ Siidi Maxtaar Mbàkke lañ dooroon tabax bi. Nguuru Ablaay Wàdd moo joxe suuf su tollu ci 6i ektaar ngir ñu mën a jëmmal bëgg-bëggu murid yi. Arsitekt bi ñuy woowe Meysa Joojo Ture moo nataal juróomi sooroor yiy màndargaal jumaa ji. Bi mu noppee ci liggéeyam, waa CDE ñoo kuule sooroor yi. bi ci gën a gudd, gën a gudd ci Ndakaaru itam, mat na 75i meetar, kon sute na 7i meetar bu jumaay Ndakaaru ju mag ji. Ay masoŋ yu fekk baax réewum Siwis, nag, ñoo yékkati sooroor yi. Bu dee taaral bi, ay nataalkat yu xereñ, jóge fépp ci àddina si, ñoo ko defar.
Ubbite bu xumb
Fépp la taalibe yi ak soppe yi màbbe keroog àjjuma, jubalsi Kolobaan ngir teewe xew-xew bi, julliwaale fa, muy julli bees fay njëkk a amal, ubbee ko jumaa ji. Mbooloo mu takkoo noonu, day laaj ay matuwaay yu wér te wóor. Moo tax nguur gi teel a yabal takk-der yi, way-fajkat yi ak balekat yi ngir waajal bés bi. Waaye, daayira yi tamit, kenn demul ñu des. Pastéef bu mat sëkk lañu wone. Kolobaan xumbal la ko bii peeru xumb, ñu samp mikóro yi, alxuraan ji di daw ak i xasiday Séex Axmadu Bàmba Mbàkke. Waa daayira Xidmatul Xaadim samp fa seeni berkelle, taf fay nataal ak ay këyit yuy màndargaal taarixu yoonu murid ak kàdduy Sëriñ Tuubaak Séex Ibraayma Faal mi ñuy woowe : buntu muridiina. Waaye, teewaayu Njiitu-réew mi, Maki Sàll, ak bu Ablaay Wàdd, Njiitu-réew ma woon, doon na lu fés lool ci bés bi.
Wenn askan, benn jëmu, jenn jumaa
Ubbite juuma ji, nag, du rekk mbooloo mi fa teew daa takku. Loolu am na waaye li gën a yéeme mooy li nit ñi bawoo fépp ci réew mi ak sax bitim-réew. Li ko dale taalibe yi, kilifa diine yi bokk ci yeneen tarixa yi, kilifa diine katólig yi, kilifa aada yi, jaraaf ak jawriñi Lébu yi ci Ndakaaru, politiseŋyi moo xam ci nguur gi lañu bokk mbaa ci kujje gi, moom daal ñépp a nga woon Kolobaan, kenn nanguwul a toog di xaar ñu lay nettalisi bés bi.
Kon, mënees na wax ne, réew mépp a daje woon ca Kolobaan ngir màggal ubbite jumaa ji. Taalibe murid yi tukkurmuutba nga ne lii lu mu doon. Réew mépp di tés-tési. Ci nataali bés bi, ñoo ngiy ciy wane Njiitu-réew mi Maki Sàll ak kim fi wuutu, Ablaay Wàdd ñu séq Xalifa bi. Wànte, nataal bi gën a neex ñépp mooy ñoom ñaar bi ñu jàppantee, ku nekk yékkati sa loxo moroom, di ree. Mu mel ni bés bi dafa jubale ay noon, tàppe xol yi, lëkkale ay kër ak i kurél, boole askan wi, ñépp ànd doon benn, bokk benn jëmu. Tijaan yi waxoon nañ sax ne Masaalikul Jinaan lañuy defe seen wasifa àjjuma ji.
Waaye, bu loolu weesoo, warees na jukkee ci mbir mi ñaari jàngat.
Bi ci jiitu mooy ne, bu doomi Senegaal yépp bokkee doon benn, am pas-pas te nangoo liggéey, réew mi dina jëm kanam. Ndaxte, jumaa ji, xaalis bu takku bi ci dem yépp, ci gafaka askan wi la génne. Lebiwunu fenn, tàllalunu kenn loxo. Kon, bu nu gëmee sunu bopp dëggantaan, bëgg sunu réew ba noppi jële fi xàjj-ak-seen, bennoo, mën nanoo tabax Senegaal ba mu naat te dunu am ak kenn xaar-ma-Yàlla.
Ñaareelu njàngat maa ngi aju ci doxalinu politiseŋyi. Saa su xew-xewu diine amee, nga gis leen ñuy sukkal ak a raamal sëriñ si. Ak nu mu mënti deme, jëf ju ñaaw la. Kilifa dafa war a wormaal boppam, weg ñi ko fal te bañ a tuutal ndombog-tànk giñ ko dénk. Rax-ci-dolli, askan wi war naa yeewu ci jikkoy naaféqu politiseŋyi. Juboo neex na, gaa, te jàmm a gën ay, duñ sax benn. Waaye, diggante Abdulaay Wàdd ak Maki, li ci jot a xew lépp ak li ci kilifa yu baree-bare jot a wax…ñu bàyyi ba bés bu màggee ni bii mel ni ñuy teyaatar ! Aa… Newunu du dëgg ci ñoom de, waaye mbir mi warees na cee màndu ba xam fu muy mujje
Gorgui Ciss interdit d’accès au domicile de Tanor
La guerre fait rage entre socialistes pour la succession à la tête du Parti socialiste. Pendant que Serigne Mbaye Thiam se positionne, Gorgui Ciss veut sérieusement lui ravir la vedette. Maladroitement du reste. Hier le maire de Yenne a été interdit d’accès à la maison de feu Ousmane Tanor Dieng à Ngénienne par la famille de ce dernier qui ne lui pardonne pas d’avoir organisé un meeting lorsque ce dernier était malade, pour ramer à contre courant de ses décisions. D’après des sources de «L’As», le Pr Ciss voulait non seulement y présidait une finale de football dont il était le parrain, mais aussi se recueillir au mausolée du défunt secrétaire général qui fut son ami. Seulement la famille Dieng aurait refusé. «Il avait organisé un meeting alors que Tanor était malade pour s’offusquer du choix porté sur Serigne Mbaye Thiam et Aminata Mbengue Ndiaye par Tanor pour entrer dans le gouvernement», confie un socialiste sous l’anonymat qui souligne que même les responsables de la coordination de Nguénienne n’ont pas été informés de la visite du chargé des relations extérieures du Ps à Ngénienne.
Appui aux sinistrés de Sinthiou Bamambé
Le ministre de l’Éducation nationale s’est rendu ce week-end à Sinthiou Bamambé dans le département de Kanel, région de Matam. A la tête d’une forte délégation composée des membres de son cabinet, du Préfet de Kanel, du maire de Sinthiou Bamambé, des autorités religieuses et coutumières et de quelques élus locaux, Mamadou Talla a, tour à tour, visité des concessions impactées par la furie des eaux pour réconforter les familles sinistrées et leur apporter le message du Président Macky Sall. D’après le communiqué reçu de son service de presse, le ministre de l’Education Nationale s’est rendu à l’école 2 de la commune pour constater l’ampleur des dégâts et surtout se féliciter des efforts fournis pour évacuer les eaux afin de permettre une bonne reprise des cours.
Du riz et de l’argent aux sinistrés …
Restons avec le ministre de l’Education Nationale pour souligner qu’il a personnellement mis la main à la poche pour soulager les populations de son village natal. Remerciant les populations de la qualité de l’accueil, Mamadou Talla également remis, au nom du président de la République, un don de 5 tonnes de riz aux sinistrés et 3 millions Fcfa pour régler les urgences. Pour rappel, le département de Kanel, à l’instar de plusieurs localités du pays, a enregistré des pluies diluviennes ces derniers jours, causant ainsi beaucoup de dégâts.
Saër Kébé décroche son bac
Saër Kébé, l’élève arrêté dans le cadre de la traque aux terroristes et envoyé à la Maison d’Arrêt et de Correction de Rebeuss, a décroché, avant-hier, son baccalauréat avec mention assez bien. Après 4 années passées à la citadelle du silence, l’ancien élève du lycée Demba Diop de Mbour qui s’est présenté à la session d’octobre a obtenu son ticket d’entrée à l’université. C’est dire que Saër Kébé a pris sa revanche sur les plus sceptiques qui lui prédisaient un échec, du fait de son long séjour carcéral pour apologie du terrorisme.
Free connecte les marabouts de Touba
En perspective du grand Magal, une forte délégation de Free conduite par son Directeur Général, Mamadou Mbengue, s’est rendue à Touba auprès du khalife général des Mourides Serigne Mountakha Mbacké et des différentes autorités religieuses, afin de renouveler le soutien et la solidarité de Free à la communauté mouride. D’après un communiqué de Free, le Dg a offert des dotations de bœufs, des tonnes de riz, des centaines de litres d’huile, plus de 90 000 bouteilles d’eau, des milliers de nattes de prières ainsi que des téléphones portables au khalife général des mourides Serigne Mountakha Mbacké, au khalife général des Baye Fall Serigne Cheikh Dieumbe Fall, à Serigne Bassirou Abou Khadre Mbacké, président du comité d’organisation du grand Magal de Touba, à Serigne Abdou Karim Fallilou Mbacké ainsi qu’aux familles religieuses. Free a aussi apporté un important soutien à des Daaras de la capitale du mouridisme en leur fournissant du riz, du sucre et du lait. Aussi, pour confirmer sa place de leader à Touba, Free a déployé une artillerie technique avec près de 300 sites, toutes technologies confondues, afin de faire vivre le meilleur des offres mobile et de la 4G+ aux millions de pèlerins.
Le cas Tahirou Sarr
Seydou Sarr dit Tahirou doit avoir un bon marabout au point d’échapper aux sévères diatribes de Ousmane Sonko qui semble véritablement cibler Mamour Diallo. Mais à y voir de près, quoi que l’acte de Tahirou Sarr dans cette affaire soit légal, mais il reste abominable, au plan moral. Racheter des créances à vil prix (3 milliards Fcfa) des mains d’une famille divisée et financièrement dans le besoin pour les revendre à 94 milliards, il faut vraiment avoir une pierre à la place du cœur.
Moustapha Diakhaté
On aime bien Moustapha Diakhaté loin du système qui corrompt absolument les beaux esprits et les belles âmes. L’ancien député et président du groupe parlementaire Bby passe désormais son temps à sortir des idées assez intéressantes qui méritent qu’on s’y attarde tout de même. «A l’instar des Magistrats, Douaniers et Inspecteurs généraux d’Etat, le Sénégal doit interdire l’engagement politique aux Fonctionnaires des administrations fiscales, domaniales, du Trésor public, des administrateurs civils et diplomates de carrière», écrit Moustapha Diakhaté sur son compte Facebook. D’après lui, les fonctionnaires doivent se mettre exclusivement au service des populations ou quitter la fonction publique et ne plus y revenir. «Tout fonctionnaire qui décide de s’engager en politique doit démissionner ou être radié dès lors qu’il fait acte de militantisme», souligne-t-il.
Dissensions au sein de la Cojer de Mbour
Les membres de la Convention des Jeunes Républicains (Cojer) de Mbour ne parlent plus le même langage depuis quelques temps. Après la sortie de la Cojer départementale et des jeunes de Bby de la commune de Mbour fustigeant le chômage et l’inertie des responsables, une tendance favorable au ministre Oumar Youm est montée au créneau pour tirer à boulets rouges sur le premier camp. Pour ces jeunes républicains, le rôle du ministre et du président de la République n’est pas de trouver de l’emploi aux jeunes. «Des attaques sont portées contre notre responsable politique et coordonnateur départemental Oumar Youm, mais nous répondrons avec beaucoup de sérénité et calme à l’image de notre responsable Oumar Youm. On ne peut pas accéder récemment au pouvoir où on vient de nommer des autorités qui n’ont même pas encore le temps de dérouler et de prendre connaissance des dossiers que des gens viennent leur imposer quelque chose», affirme Hyacinthe Sène, coordonnateur de la Cojer de la commune de Sindia. Il accuse des responsables tapis dans l’ombre de tenter de discréditer Me Oumar Youm en utilisant les jeunes comme boucliers.
Abdoul Mbaye et Lamine Diallo à Touba
A quelques jours du Grand Magal, c’est le ballet des personnalités à Touba. Hier, une délégation du Congrès de la Renaissance Démocratique (Crd) s’est rendue à Touba et a été reçue par le khalife général des mourides, Serigne Mountakha Bassirou Mbacké. C’est au nom des leaders du Crd que Mamadou Lamine Diallo et Abdoul Mbaye ont présenté au marabout leurs vœux de réussite pour le Magal de Touba, lui adressant par ailleurs de vives félicitations pour ses œuvres au service du développement de la foi dont Massalikoul Jinann, la paix et la mise en œuvre d’une bonne justice au Sénégal. en retour, ils ont reçu les bénédictions du Khalife et ses prières pour le succès de leurs projets au service du Sénégal.
L’Act a une nouvelle voix
Le parti de Abdoul Mbaye se structure. L’Alliance pour la Citoyenneté et le Travail (Act) se réorganise. D’après des sources de «L’As», le Conseil National du parti a eu un nouveau souffle avec la nomination de plusieurs jeunes. Dans cette même lancée, la direction exécutive et le porte-parole du parti ont connu des changements. Professeur Assane Fall, Universitaire, sportif, ancien secrétaire national chargé de l’écoute citoyenne, coordonnateur national lors du parrainage est nommé Directeur Exécutif et premier porte-parole du parti.
La réponse du CRD aux partisans de Ousmane Sonko
Les leaders du Congrès pour la Renaissance Démocratique (CRD) n’ont pas tardé à réagir face aux accusations de partisans de Ousmane Sonko. En effet, ces derniers accusent l’opposition d’avoir lâché Ousmane Sonko au sujet de l’affaire dite des 94 milliards. Mamadou Lamine Diallo et Cie précisent que l’opposition regroupée au sein de Crd lutte pour le renforcement de la démocratie et de la justice sur la base du patriotisme économique. Répliquant aux partisans de Sonko, ils indiquant que l’opposition a refusé de participer à la Commission d’enquête parlementaire au motif qu’il y a d’autres faits sur lesquels il y a lieu d’enquêter notamment l’affaire Petrotim, Arcelor Mittal etc.. avec l’accord de Ousmane Sonko. Mieux, elle a saisi le député Sonko ainsi que ses collègues non inscrits pour voir la stratégie à retenir à la plénière de vendredi dernier, sans suite. Lors de la plénière, le député Mamadou Lamine Diallo avait soutenu que l’ouverture d’une information judiciaire rendait caduque la séance. Aussi, après la lecture du rapport, l’opposition a refusé de le voter.
Ousmane Sonko calme ses troupes
Le leader de Pastef, qui est concentré sur l’affaire des 94 milliards, calme ses troupes qui sont en passe d’ouvrir un autre front. Puisque, certains d’entre eux s’attaquent aux responsables de l’opposition qui, à leurs yeux, ne défendent pas leur leader. Mais dans un communiqué, Ousmane Sonko adresse ses vifs remerciements à tous les députés de l’opposition réunie qui, lors de la plénière-mascarade du vendredi dernier, ont témoigné de leur solidarité non complaisante en affrontant la majorité. Selon Sonko, l’opposition parlementaire, au-delà de ses appartenances politiques, a toujours fait montre depuis le début de cette législature, d’une solidarité agissante contre les coups de force de la majorité mécanique. Ce fut le cas, rappelle-t-il, lors de la tentative de liquidation de Khalifa Sall, des modifications de la Constitution et du Code électoral ou la loi sur le parrainage. Par ailleurs, Sonko lance un appel aux militants de Pastef à s’abstenir de toutes conjectures, commentaires ou jugements portant sur la situation politique actuelle et singulièrement les retrouvailles des uns et des autres. Il les invite à rester concentrés sur leurs objectifs.
Macky Sall chamboule le programme
Hier lors du séminaire sur la communication gouvernementale, les organisateurs ne voulaient donner la parole qu’à des responsables de l’Alliance pour la République (Apr). Mais, ce programme a été chamboulé par Macky Sall qui présidait la rencontre. En effet, après l’intervention de parole de Mor Ngom, Macky Sall a coupé le Maître de Cérémonie (MC) en la personne du député Abdou Mbow pour exiger la diversité dans les communications. Ce qui lui a valu un standing ovation de la part de l’assistance. C’est ainsi que le coordonnateur de la Cellule de communication de Bby Mahawa Diouf a été invité à laisser Me Ousmane Sèye intervenir. A la suite de l’avocat, c’est Momar Samb (du Rta/S) qui a lu la motion politique en Wolof.
Macky Sall et les chiffres 5-3-5
Pour bien maîtriser tout son programme y compris le Plan Sénégal Emergent (PSE), le Président Macky Sall a demandé aux militants de Benno Bokk Yakaar (Bby) de se référer au 5.3.5. Ce chiffre veut dire 5 initiatives, 3 programmes et 5 accès universels. Si le militant notamment le communicant ou le débatteur arrive à mémoriser ces trois chiffres, affirme le chef de l’Etat, il n’aura aucun problème face à un adversaire lors d’un débat. En marge de la rencontre, il a demandé aux Sénégalais de changer de méthode de travail et d’appliquer le mode fast track s’ils veulent aller vers l’émergence.
Le titre ce billet est de l’iconoclaste et pertinent journaliste qu’est Ibou Fall. Je lui demande l’autorisation de le rappeler aujourd’hui car il est de circonstance. Pour répondre à la furie des fanatiques qui clouent Penda Mbow au pilori pour avoir dit que le voile n’était pas un commandement islamique. Mon propos n’est cependant pas de discuter de ce qui est ou n’est pas édit de l’Islam car n’étant pas un exégète du Coran. Je veux seulement, comme Ibou Fall, dire que le moussor est plus qu’un accessoire essentiel de l’habillement de la femme au Sénégal. C’est un élément de la culture de ce pays.
Le moussor n’est pas en effet ce simple « serre-tête » assorti au boubou que les Africaines portent partout, en tous cas, en Afrique de l’Ouest et du Centre, de Dakar à Kinshasa, de Nouakchott à Yaoundé.
Le moussor au Sénégal comme par exemple le « Gele » au Nigeria (à l’origine Yoruba) est à la fois un pointeur social et un indicateur de l’état d’esprit de celle qui le porte.
Il y a le moussor de la « drianké », riche, opulent comme il se doit, ostentatoire, assorti au large boubou ou d’un ton légèrement contrasté, en voile léger pour mette en valeur l’ensemble. Avec un je ne sais trop quoi d’aguicheur, dans l’inclinaison de la coiffe, dans une apparence de négligé qui laisse un bout flotter sur le cou…
Il y a le moussor de la travailleuse manuelle et de la paysanne qui attachent solidement les deux bouts de tissu sur le front ou en arrière. Quelques fois, elles l’enlèvent de la tête pour s’en ceindre les reins.
Il y a le moussor de tous les jours, de la femme au marché ou au bureau, assorti ou non au boubou, quelques fois couvrant à moitié la tête et tombant négligemment sur le cou ou sur l’épaule. Quelques fois voilant le visage tout entier.
Il y a le moussor de la jeune fille qui n’en porte qu’à l’occasion de cérémonies quand le grand boubou est de mise.
Il y a bien sûr le moussor des « mamans » : attaché sévèrement sur le front, qu’on porte bas et plat et qui confère un indéfinissable air d’autorité et de.…résignation.
Je prétends même qu’il suffit de regarder le moussor des femmes de ce pays, pour en apprendre sur les manières d’être, d’agir et de penser des Sénégalais et pas seulement des Sénégalaises.
Il y a ainsi le moussor « soutoura », comme il y a le moussor « pank », séducteur et aguicheur, le moussor de fête et le « moussor » des jours de deuil.
C’est dire que je comprends l’argument de Penda Mbow comme une défense du moussor en tant qu’artefact de la culture de ce pays.
J’ai entendu Tariq Ramadan Ramadan (dont on peut critiquer les mœurs et les positions politiques mais dont les connaissances en matière d’Islam sont rarement contestées), dire que l’habit traditionnel des Sénégalais, et notamment des femmes, ne devrait pas être remis en cause au nom de l’Islam.
Certains musulmans, et ils sont apparemment nombreux désormais dans ce pays, croient et professent que le voile est une prescription islamique essentielle et son port une obligation pour toutes les musulmanes de tous les pays du monde.
D’autres dont je suis, estiment que c’est plutôt un accessoire du vêtement féminin qui nous vient d’Arabie dont le port - ou le refus du port - ne devrait en aucune manière déterminer l’appartenance à l’Islam. Devrait-on pour autant nous condamner comme hérétiques ? Va-t-on instituer l’inquisition ?
Veut-on comme en Arabie Saoudite instaurer une police des mœurs qui s’assurerait que toutes les femmes sont bien voilées et que tout le monde effectue bien ses cinq prières aux heures prescrites ?
Car pour cela il faudra recourir aux moyens dont Daesch a usé pour instaurer son Etat Islamique en Syrie et en Irak ou à ceux qu’Ansar Eddine a utilisés pour imposer sa loi islamique à Tombouctou.
Ne devrons-nous pas simplement faire preuve de tolérance les uns par rapport aux autres ?
Reconnaitre certes que nous n’avons pas la même compréhension et acceptation du dogme islamique ou que n’avons pas la même religion mais que nous nous acceptons et nous respectons mutuellement.
On devrait pouvoir être pas seulement Mouride ou Tijane ou Quadria mais aussi Chiite, Wahabite, Pententacostite, Adventiste ou athé dans ce pays, sans déranger personne.
Chacun est libre après tout non pas seulement de croire en la religion de son choix, mais aussi d’adhérer à une interprétation spécifique de cette religion ou de ne pas croire.
Une femme peut choisir de porter le voile ou de se coiffer avec des cheveux « greffés » ou d’une perruque ou …de se raser la tête.
Sur ce sujet comme sur d’autres, le libre choix des gens, en l’occurrence des femmes, devrait prévaloir.
On doit accepter une fois pour toute que la société sénégalaise est en fait multiculturelle, que ce qu’on appelle « culture sénégalaise » est en réalité composé d’apports traditionnels, survivances des sociétés féodales précoloniales, d’apports islamiques et d’apports d’origine occidentale.
Nier cette réalité et tenter d’imposer une culture qui serait plus « pure », agrée par Dieu, serait à coup sur, susciter le désordre et la violence.
Ce qu’on appelle pour se référer à l’histoire de l’Islam, la « fitna »
Pour ma part, j’espère que le moussor a encore de beaux jours devant lui …
Retrouvez chaque semaine sur SenePlus, le billet de notre éditorialiste, Alymana Bathily