Seneplus.com
  • La Une
  • Politique
  • Economie
  • International
  • Sports
  • People
  • Opinions
  • Societe
  • Annonces
  • Culture
  • Medias
  • Diaspora
  • Femmes
  • Développement
  • Santé
  • Éducation
  • SENEPLUS TV
  • Baromètres
  • #SilenceDuTemps
  • NELSON MANDELA
  • LEOPOLD SENGHOR
  • CHEIKH ANTA DIOP
 
15 mai 2025
FacebookTwitterRSS
Seneplus.com
Opinions
  • La Une
  • Politique
  • Economie
  • International
  • Sports
  • People
  • Opinions
  • Societe
  • Annonces
  • Culture
  • Medias
  • Diaspora
  • Femmes
  • Développement
  • Santé
  • Éducation
  • SENEPLUS TV
  • Baromètres
  • #SilenceDuTemps
  • NELSON MANDELA
  • LEOPOLD SENGHOR
  • CHEIKH ANTA DIOP
Par Seex Aliyu Ndaw

NDIGALU MAAM YA

defuwaxu  |   Seex Aliyu Ndaw  |   Publication 03/04/2024

Afrig nee

Waaw góor, waaw kumba

Ayca leen ca waar wa

Bu kenn wéer goob ba

Bii pas-pas dara mënalu ko dara

Dina daw ba raw xëlu fas

Ngor ak jom a ko nas

Ma ne, Askan wee ko sas

Gan góoru jigéen ñi dar lingeer

Ci seen farlook seen gànjar ya

Bég ba tàccu ne sas

Maam a ne bëret dan delsi

Samp xeej daldi xas

Gisuma fi yaakar ju tas

Tuggee Tugal

Wéyal yaak say dëbës

Afrig dina bañ ba sës

Ndawi tey yi dootuñu surgawu

Topp sa gannaaw ni jaam bu nangu

Dina tàng dina metti

Waaye jàmbaar du xàddi

Na doxandéem bii dakkal

Wàqi gi muy wàqi sunu alal

Di roñ di génne

Di gaawantu di rawale

Am ñu ne xiim di xoole

Mbaa sax di ko ci dimbale

Sàmm sam réew warugar la

Bëgg sa réew siddit la

Gor tigi du wor du wuruj

Te su séddu jotee mooy mujje

Biir bu rëy lex yu newwi

Sonal sa bopp tooñ say ñoñ

Moone de bànneex tigi

Xanaa xam-xam ak néewle soxla

Tey jiital njariñal doom Aadama

Seex Aliyu Ndaw

Ndakaaru, weeru mars 2024

Articles les plus lus

capture_decran_2025-05-12_a_08.41.42.png
TARIQ RAMADAN COMME CHEIKH YERIM, COMME SONKO
Tariq Ramadan est à Dakar dans le cadre de la 13e édition de «Jokkoo», tenue le samedi 10 mai à ...

nicolas.jpg
LE FDR EN ORDRE DISPERSÉ AU DIALOGUE
Le front pour la défense de la démocratie et de la république (Fdr), une entité regroupant plusieurs ...

asarr.jpg
L’EGLISE CATHOLIQUE N’EST PAS PRETE A AVOIR UN PAPE NOIR
Le moment viendra un jour, mais l’Eglise catholique n’est pas prête à avoir un Pape noir, a déclaré, ...

capture_decran_2025-05-04_a_02.13.12.png
UN DIALOGUE DE FAÇADE ?
Invité du Grand Jury de RFM ce dimanche, l'ancien ministre et politologue Yoro Dia n'a pas mâché ses ...

capture_decran_2025-05-12_a_12.49.35.png
QUID DU FCFA/ECO FACE AU DÉFI DE L’INTÉGRATION ÉCONOMIQUE
Une hausse des tarifs douaniers d’une ampleur sans précédent, a été décidée le 2 avril dernier ...

Vos articles préférés de la semaine

capture_decran_2025-05-08_a_18.00.30.png
À L’OMBRE D’UNE ICÔNE FÉMINISTE, FATOU SOW
La nouvelle orientation du quotidien Le Soleil surfe-t-elle sur la bonne vague, en épousant les valeurs ...

psk.jpg
ARRÊTÉ DU MINISTRE DE LA COMMUNICATION, UN RECUL DE QUATRE SIÈCLES
En français facile, voici pourquoi la Cour suprême, le Conseil constitutionnel et tous les démocrates ...

photo-2025-05-07-14-02-27.jpg
FIDÈLE GOULYZIA DÉCROCHE LE GRAND PRIX BERNARD DADIÉ
(SenePlus) - Le journaliste-écrivain ivoirien Fidèle Goulyzia a été sacré lauréat du prestigieux ...

capture_decran_2025-05-02_a_08.57.59.png
LE REVIREMENT DES 'ANTISYSTÈME'
(SenePlus) - Le gouvernement dirigé par Bassirou Diomaye Faye et Ousmane Sonko se retrouve confronté ...

capture_decran_2025-05-03_a_12.57.55.png
LE GRAND BOND SOCIAL DU SÉNÉGAL ?
La décision du ministre chargé de l’Emploi concernant le relèvement des salaires minima des travailleurs ...


La Une

Politique

Economie

International

Sports

Football

Media

People

Opinions

Societe

Annonces

Diaspora

Femmes

Développement

Santé

Éducation

PARTENAIRES DE SENEPLUS

APS
Grand-Place
L'As
L'Enquete
L'Observateur
La Gazette
Le Populaire
Le Quotidien
Le Soleil
Le Témoin
Libération
Nouvel Horizon
Réussir
RFM
RTS
Stades
Sud FM
Sud Quotidien
Sunu Lamb
TFM
Waa Sports

À propos de SenePlus

SenePlus.com est un portail d'informations sur le Sénégal. Nous vous fournissons des articles détaillés, critiques, pertinents sur l'actualité au Sénégal.

Coordonnées

Publicité:
pub@seneplus.com
Informations:
info@seneplus.com
Problèmes techniques:
tech@seneplus.com
Copyright © 2025 SenePlus  |  Publicité  |  Soumettre un Article  |  Nous Contacter  |  Mentions légales  |  Conditions d'utilisation  |  Á propos de nous