Seneplus.com
  • La Une
  • Politique
  • Economie
  • International
  • Sports
  • People
  • Opinions
  • Societe
  • Annonces
  • Culture
  • Medias
  • Diaspora
  • Femmes
  • Développement
  • Santé
  • Éducation
  • SENEPLUS TV
  • Baromètres
  • #SilenceDuTemps
  • NELSON MANDELA
  • LEOPOLD SENGHOR
  • CHEIKH ANTA DIOP
 
11 septembre 2025
FacebookTwitterRSS
Seneplus.com
Politique
  • La Une
  • Politique
  • Economie
  • International
  • Sports
  • People
  • Opinions
  • Societe
  • Annonces
  • Culture
  • Medias
  • Diaspora
  • Femmes
  • Développement
  • Santé
  • Éducation
  • SENEPLUS TV
  • Baromètres
  • #SilenceDuTemps
  • NELSON MANDELA
  • LEOPOLD SENGHOR
  • CHEIKH ANTA DIOP

SONKO AK MAKI : KUY DAAN ?

Fitna lañ doore bésub àjjuma jii. Fitna ju sosoo ci diggante Sonko ak Maki. Ndax lan ?

www.defuwaxu.com  |   Aamadu Jara  |   Publication 21/06/2022

Fitna lañ doore bésub àjjuma jii. Fitna ju sosoo ci diggante Sonko ak Maki. Ndax lan ? Ndax, dañoo tere Sonko ak i àndandoom seen ndajem ñaxtu mi ñu bëggoon a amal bés boobule ca Péncum Obelisk. Li ñu jàpp, mooy ne Maki dafa noot yoon, ba pare bëgg a lottal Usmaan Sonko. Réy gi mu réy moo tax mu jàpp ne warul am kuñ koy méngale (dendale) ci làng gi. Ba tax mu dëkke di ko lakkal ngir ne mooy wujjam bi gën a am doole ci làngug pólitig gi ci jamono jii. Li sabab lu ni mel, nee ñu, bëqët la, ab ragal la moo tax. Fi mu tollu nii dafa bëgg a def ñetteelu moome te feek daanelul Sonko xelam du dal. Loolu la defoon ak Xalifa Sàll ay at ci ginnaaw. Jàpp ko ne ko ràpp ci kaso bi.

Ca dëgg-dëgg ñenn ñi fare ci wàllu yoon ba ci waa « Conseil Constitutionnel », jàpp nañu ne ci ay waawu Maki Sàll lañuy dox. Maanam, lu mu namm ñu def rekk lañuy def. Waaye, moom dafa fàtte ne ñaxtu bi mu daan ñaxtu démb loolu la Sonko ak i àndandoom di ñaxtu tey. Fàtte moom da fee xajul sax. Te, ku fàtte lu la fal, sag folleeku da lay bett. Léegi kon, lan moo tax mu bëgg a jalgati yoon ndeem digganteem ak Abdulaay Wàdd demewul woon nii ?

Nde, Sonko jàpp na ni Njiitu réew mi amul benn manoore rawatina gaa ñi ko wër. Bi ñu déggee ni YAW dina amal seen ndajem-ñaxtu la alkaati yi dem wër këru Usmaan Sónko ak gu Bartelemi Jaas ca teel. Xanaa loolu mooy jaay doole dëgg ci dëkk boo xam ni nee nañ am na yoon. Te lees fi gis mooy ëpp la doole bës sa bët. Xalaas ! Sonko déy, safaan bi la gëm. Ndax jaaduwul ñu leen di tere def seen ndajem ñaxtu ginnaaw àtte bi ñu def ci seen « liste électorale ».

Ci ay xayma, Maki dafa am jàngoroy nguur. Waaye, du loolu doŋŋ a ko tax a doxalee nii xanaa. Nguuram nguur guy sàcc la di nëbb sàcc, gu dëkk ci nger ak ay njublaŋ yu dul jeex. Xam nañ ni bu Sonko faloo du baax ci ñoom moo tax ñu koy bëgg a faagaagal, lu ne ñu tuumaal ko ko ngir bëgg koo jaxase ak askan wi.

Nde, am na ñu taxaw sax ne Sonko dañ ko war a faat. Bu doon ci réewum yoon la, xeetu kàddu yile, kenn waru leen a yékkati te yoon tegalu la ci ay daan. Yile firnde ñoo sabab taxawaayu Njiitu réew mi tey. Bunduxataal Sonko, di ko xoqtal, di ko fatt, loolu mooy ngànnaay bi mu dese. Waaye Sonko mii ës pareegul ngir bàyyi xeex bi mu sumb ngir jële fi Maki ak i ñoñam.

Articles les plus lus

capture_decran_2025-09-06_a_22.51.55.png
NON, JE NE CÉLÈBRE PAS ABDOU DIOUF
« Célébrons ensemble Abdou Diouf », disent ils ! Pourquoi devrais-je célébrer ...

capture_decran_2025-04-15_a_05.14.23_0_0_0.png
LE MIRAGE DU PANAFRICANISME 2.0
Spectacle numérique et manipulations géopolitiques On nous répète à longueur de journées que ...

capture_decran_2025-09-06_a_19.50.10.png
DORTMUND, L'ÂME DE LA RUHR
« Le BVB, c’est la Ruhr qui vibre, le noir et le jaune qui embrasent les tribunes. » Signal Iduna ...

capture_decran_2025-09-07_a_15.50.03.png
AMADOU LAMINE SALL CONFIRME SA CANDIDATURE AU SECRÉTARIAT GÉNÉRAL DE LA FRANCOPHONIE
Dans l'émission JDD de ce dimanche sur iTV, l'écrivain et poète Amadou Lamine Sall a officialisé ...

bv.png
CRITIQUE DE LA RAISON ORALE DE MAMOUSSÉ DIAGNE, UN OUVRAGE FONDAMENTAL DE LA CONSTRUCTION NARRATIVE AFRICAINE
Notre patrimoine littéraire est un espace dense de créativité et de beauté. La littérature est un ...

Vos articles préférés de la semaine

cecile_t.jpg
ET SI NOS LANGUES MATERNELLES ÉTAIENT HÉRITAGE SILENCIEUX ET FORCE MONTANTE ?
Et si chaque mot transmis devenait une graine de rayonnement ? Au Sénégal comme dans la diaspora, nos ...

sq_vs.jpg
« JUSTICE PAR FORCE », UNE MENACE POUR LA RÉPUBLIQUE
« Justice par force » n’est pas un cri d’équité. C’est un mot d’ordre dangereux, un slogan ...

capture_decran_2025-09-03_a_18.36.45.png
QUAND LA QUÊTE DE MINCEUR MET LA SANTÉ EN DANGER
S’il ne s’agissait que de pratiques commerciales douteuses, nous pourrions nous en remettre uniquement ...

capture_decran_2025-09-03_a_20.57.16.png
LA JUSTICE ENTRE LÉGALITÉ ET MORALE
D’anciens détenus, bénéficiaires d’une inique loi d’amnistie, ont manifesté pour réclamer ...

capture_decran_2025-09-01_a_20.52.02.png
LES INCONGRUITEÉS DE LA PROPOSITION DE LOI DE PAPE DJIBRIL FALL PORTANT GRATUITÉ DU TRANSPORT DES ÉTUDIANTS
La proposition de loi du député Pape Djibril Fall déposée sur la table du président de l’Assemblée ...


La Une

Politique

Economie

International

Sports

Football

Media

People

Opinions

Societe

Annonces

Diaspora

Femmes

Développement

Santé

Éducation

PARTENAIRES DE SENEPLUS

APS
Grand-Place
L'As
L'Enquete
L'Observateur
La Gazette
Le Populaire
Le Quotidien
Le Soleil
Le Témoin
Libération
Nouvel Horizon
Réussir
RFM
RTS
Stades
Sud FM
Sud Quotidien
Sunu Lamb
TFM
Waa Sports

À propos de SenePlus

SenePlus.com est un portail d'informations sur le Sénégal. Nous vous fournissons des articles détaillés, critiques, pertinents sur l'actualité au Sénégal.

Coordonnées

Publicité:
pub@seneplus.com
Informations:
info@seneplus.com
Problèmes techniques:
tech@seneplus.com
Copyright © 2025 SenePlus  |  Publicité  |  Soumettre un Article  |  Nous Contacter  |  Mentions légales  |  Conditions d'utilisation  |  Á propos de nous